*YOBALOU FADJAR*☝
Manguilay denk ngay toub ci lep loulay dioural ak yédd, deel sant yalla mila dakal moussiba yi, deel sawar ci lou baax té boul tayal, deel andak koulay yée ci topou yalla
Bariwaana doff bu xeuy xeuy yéwou lol ci sababouk andak koukay yéele, bariwaana kou am xel té melni kou réer nguir andak goumouy andal kou reer
, deel takoo ragal yalla ak jang nguir jeumi yalla
*Yendou ak Diam*🙏🙏🙏
![](https://img.wattpad.com/cover/211713990-288-k460017.jpg)