YOBALOU

165 9 0
                                        

*YOBALOU FADIAR*☝
Serigne Touba wax na ni Sougnou borom haramalna thi bepp moukalaf mouy jeuf teh xamoul la Yallah atté thia jeuf diamouy dieuf. Manam lepp loye djeuf wargua xam lathiay farata, lathiay sounna, lanthia soppou, war nga xam lakoy yakh ak lakoy defarr. Kiye dieuf tek ko thi xamxam menoul yam kiy topu ndiortam rek. Xam gui nak ben nga diangue ko thi téréyi walaga nga laathielé ko borome xam xam. Yalla na Yallah nagoul gnou sougnouye  djamou amine.
*Yendou ak Diam*🙏🙏🙏

Yobalou Akk aye kadou sognėDes histoires addictives. Découvrez maintenant