YOBALOU

181 13 0
                                    

*☝🏿YOBALOU FADJAR GUI☝🏿*
*🥰Bismillah🥰*
Yaw domou Adama boul wore sa Borome teh boul wore sa boppou. Ba Yalla Dadiale Rouh yép né ana koumay diaamu domou adama néko mane maalay diaamu. Sunborom indila fi thi adina nga worko. Wor Yalla moy nga lanke nagouwo diamu Yalla wayeh nga top sa bakkane ak sa baneex ak chaytané. Wor Yalla moy wor yonentibi ak wor sa boppou ak mboleem gayou bahyi teh lolou moy waral worou eulak yawmal xiyaam yalnanousi Yalla musal. Amine.🙏🙏🙏
*Yendou diam*

Yobalou Akk aye kadou sognėOù les histoires vivent. Découvrez maintenant