app fatalii

198 12 0
                                        

Lii mi ngi jóge ci man jëm ci murit yi góor ak jigéen.

Ginnaaw nuyoo bi, maa ngi leeni digal, ngeen jàng lu jëm ci pas-pas, nu ñi wéetale Yàlla, jàng àttey laab ak julli ak koor, ak lépp  lu mukàllaf wara xam. War lul naa leen téere yi ngeen koy jàngee ngir Yàlla.

Sëriñ Tuubaa

Yobalou Akk aye kadou sognėDes histoires addictives. Découvrez maintenant