YOBALOU

296 18 2
                                    

*☝🏿YOBALOU FADJAR GUI☝🏿*
*🥰Bismillah🥰*
Adina dafa weete teh barri mêtite ak naxar aki thiono. Beuri na nio xamni funu weeté rek dioy, Amna nio khamnè beutieuk daniy nebu wayè goudi niou fanané dioy. Amna nio khamnè  seen nakhar yaguena banu fookni dotul dieex, amna niouko dinthie si sêne birr khol bam moudiou rêss sopiku baneex. Nga guiss né adouna nehoul, lou metti la, wayê mounial, ndah lo mougn sou yaguè mou dieh. Dioulit deug dafay am gueum gou degeur lou Yallah dogal mou neexko.
*Yendou diam*🙏🙏🙏

Yobalou Akk aye kadou sognėOù les histoires vivent. Découvrez maintenant