Mbokk dëgg ak xarit bu wér ñoo gena néew luy néew Mooy lu mel ne waxi yalla: sa xarit dëgg mooy ki ànd ak yaw Mooy kiy lor boppam ngir jariñ la, mooy kok bu la jamono njattee Mu sonnal boppam ngir siggil la, ma ne mooy ki lay nëbbal lu ñaaw ngir yekkati la