Yobalou

194 11 0
                                        

*☝🏿Yobalou Biss Bi☝🏿*

*kharit dëgg mooy: ki ànd ak yaw,*
*Mooy: kilay nëubbeul lou ñaaw ngir yekkati la.*
*Mooy:kiy lor bòppam ngir jarigñ la,*
*Mooy: kok boula jamono njatté mou sonnal bòppam ngir siggil la (kou mell noonu mooy kharit)*

*Cheikhouna Ahmadou Bamba*

Yobalou Akk aye kadou sognėDes histoires addictives. Découvrez maintenant