Boo toogee ak ku la mag booy ree nangay yam ci muuñ Booy wax ak moom it bul bayliku ( ëppal ci wax ji) ndax loolu du lu rafet Noppil ba nga gis mu bëgg a wax ak yaw.
🙏

Des histoires addictives. Découvrez maintenant