bokk na ci teggiin yu rafet nga jort ne ay teggiin moom ci yaw rekk la war a juge, te nga bañ di ko séentu ci ku dul yaw. Te ngay ànd ak nit gni ci jikko yu baax yi nga bëgg ñu ànde ko ak yaw boo ko deful it jikko yoo ànde ak ñoom ci yu bon séentu ko ci ñoom, nit ñi daal ni nga mel ak ñoom rekk lañuy mel ak yaw).
SERIGNE TOUBA SUR *NAHJU*
