defal sab tontu boo lottee muy *noppi* bari na wax joj tontu baa nga ca ag noppi Bokk na ci Hikma: Bu wax doon xaalis noppi di wurus, bu la nit réeree (def la ag ñàkke-teggiin) Jéllale ko taqoo noppi, ni ko Yàlla waxe: *Jéllaleel ñeel ñi réere*
🙏
