*YOBALOU DADIAR*
Dioulite bi warna farlou lol thi diangue , diangualé ak Yarr askanam rawatina ndaw gni ak Djigueen gni ndax gno guena neew kantane teh gno guena gnéwante.
*Ben djigueen bou baax meune naa defar Téméri goor you bone,*
*Ben djigueen bou bone meune naa yax Temeeri goor you baax.*
Alkhour'ane nena péxém djigueen dafa reuye.
Yalla na Yalla dioubanti péxé yi ba lepp dieum thi Diamu Yallah ak ligueyal L'islam. Amine
*Yendou Ak Diam*🙏🙏🙏
![](https://img.wattpad.com/cover/211713990-288-k460017.jpg)