aye wadjur

167 7 0
                                    

Fonkal  sa  ñaari  wadjur,  te  am  yërmaande  ci  ñoom  ak  ñeewant,  te  deel  gaaw  ci  seeni  ndigal  ak moytou mbooleem  li  ñu  la  tere,  boo  ko  dee  def  de,  sag  kawe  dina  yokku Képp  ku  la  mag  ci  nanga  ko  diox thieur
🙏

Yobalou Akk aye kadou sognėOù les histoires vivent. Découvrez maintenant