YOBALOU

151 6 0
                                    

*☝🏿YOBALOU FADJAR GUI☝🏿*
*🥰Bismillah🥰*
Serigne touba neena: nit bou nangoula xamlou dinem bouko nexei dina moy yalla bouko nexoul dina moy yalla! Ndax day def dara yakarni baxna, fekk ni moy li eupa def, bayi dara yakarni baxoul fekk moy li mata def.

Yobalou Akk aye kadou sognėOù les histoires vivent. Découvrez maintenant