*🥰Bismillah🥰*
Serigne Touba aka mana mounîe teh mana diégualé ndax feknanko rewam Toumalko,atéko teh amoul avocat, indiko Dakar thi kasso bu doywarr, dialaléko teh kén waxouko lumu def waxuniou ko fumou dieum. Taxalékok niabootam, aki mbokam, Tass Daaram djioumou done diangalé ak difa yaré. Li lep tehwul Serigne bi mouñieko ba waxni *Diegueulna sama noone yepp guir Diemi Yalla Swt ak Yonentibi AS*. Kon Diemala Roy thi Khadim Rassoul dina tax loumou metti metti guay mouñie di diégualé teh Yalla rek tax.
*Yendou diam*🙏🙏🙏