Yoonu teggiin mooy nga yërëm ndaw mel ci moom ni baayam ba ko jur te am lool ci moom yërmande,
🙏Na nga yeureum ndaw ni ndayam ni mou amé ñeewant, nga weg it mag ak doonte da di ab jaam bu bawoo *Abasa* (ÉTHIOPIE) , te nga yamale sa bopp ak sa moroom ngir jëmmi Yàlla kepp.
🙏
![](https://img.wattpad.com/cover/211713990-288-k460017.jpg)