Serigne Touba diggeul na talibé yeup gnou sakh thi 4 yi.
_dioulli diourom _diangue alkhourane _diangue Xassida _liguèye bou bakh.
Dal di né :
_Dioulli diourom diglé buur la té di sammonték diglé buur di na takha dioubok buur té lépp louy takha dioubok buur diar na goorgoorlou
_Alkhourane waxi buur la
di sammonték waxi buur di na tax bu buur di lim Wakeur am bolé la thia té lép lou tax buur bolé la thi wakeur am diar na goorgoorlou
_Khassida bo kay diangue da na tax sou may lim sama wakeur bolé la thia té lép louy takh sou may lim sama wakeur bollé la thia diar na goorgoorlou.
_ liguèye nak loutakh ma ték thi bou bakh moy so ko doul déf do meune thi yi dara.
Di niane Serigne bi nangul gnou sugnup Talibé barké Khassida yi.
![](https://img.wattpad.com/cover/211713990-288-k460017.jpg)