Lihsaan mooy nga jaamu yàlla di ko teewlu ba mel ni da nga koy gis,ci lepp li ngay def,te mu wóor la ne boo ko gisul it moom mi ngi lay gis.Kon . Bu ngeen bëggee àgg ci martaba yu kawe yi,na ngeen di djeufé ndénkaane bile: maa ngi leen di denk xam-xam,ak kersa,ak sant yàlla ak sellal,ak tabe,ak noppeek lewet booy djangu, ak muñ ak ragal yàlla ak degg-degglu maanaa yi,na ngeen di farlu ci top yalla fu ngeen man a ne te sori noonoo,bu leen baril wax aki nelaw, na ngeen di moytu luy waral yaq, di moytu ngistal,fu ngeen man a ne,ak rëy ak mbañeel, tey sàkkug leer,
*AY KADDU SOGNÉ SI TASSAWUDU SIXAR*
YALLA NANIOU SERIGNE BI DIMBALIL BOPPAM🙏
![](https://img.wattpad.com/cover/211713990-288-k460017.jpg)