•
Suite
Point de vue de Madou
••
Le gars tombe, se ramasse le sol et les gens accourent s'interposer. Quand ils le relève il est recouvert de poussière de la tête aux pieds.
- Domou xar*m gissago nd*y dara sax damala Moy ! je m'exclame.
- Wa Madou yaw dangay ray ki ? s'écrie ma mère, étonnée.
- Way ki damako Moy nganan ma ray ?
D'ailleurs après s'être épousseter le visage ce dernier me dit, fou de rage :
- Fils yaw man ngay door ? me dit-il.
- Way damalay lek ngananema esk yaw lay door. Xana danga mandi yaw bingay yeuw ?
- Fils yaw esk xamnga man may kan ?
- Jiému mako xam, lijiantiwumako. Nékal nd*y domou ministre lan mocci sama Yoon ? Boy waxak sama yaye dangay modérer nd*y sa langage, fi kein duffi sa morom esk yangi comprendre ?
- Madou dalal boulko top, essaie de me calmer ma mère.
- Mais ki dafa xamadi way lan moy nd*yu nga yeuw keurou jiamour baparé diko jiay rew ?
- Bul ko top.
- Saway yawjiapal ni que signer nga sa arrêt de mort yaw, me dit-il.
- Way mother f*cker nganan arrêt de mort, mane dama falé lolu mane ? Damani boy waxak sama yaye ndanga modérer nd*y sa langage, manoko ma nioussla fi ba teud nd*y sa kaw es-ce que yangi comprendre ?
- Grand ki boul ko top, me disent les gens.
Je les ignore et continue à l'égard du mec :
- Way yaw yay kan ? Sank batay mangi nek fi di nexal ngay jiay bandit sama kaw fokni ya mom nitñi. Man nga ataya rek ngay fourralé tank, xolal mère bi lacciy seet wayé bu désse man nak yaw késsé damalay lek.
- Lolou nga fok, me répond-il.
- Lolou la fok ? Yeuwal niou mayé ko nga xol. Gisnga lolou nga jieul bande annonce késsé la, sumala jiapé damalay nd*y warax. Et puis waxji sax dafa commencer bari, légi xamnga lanla sax dax**ral nd*yam jiuguer fi !
Les gens essayent de calmer le jeu et de le raisonner à la fois. On lui demande de partir mais il refuse, ce qui me met en rogne. Je monte davantage en pression et pars prendre une grosse pierre, l'équivalent de la moitié d'une brique. Ma mère se met alors à paniquer :
- Madou loy doyé li yaw ? Tegal xeer bi !
- Damani na dax**r ndayam jiuguer fi.
Conscient de l'enjeu, les gens se mettent à l'éloigner hâtivement et c'est vraiment plus raisonnable car je suis déterminé et si jamais j'arrivais à l'avoir dans mon champ de vision je n'hésiterai absolument pas à le lui lancer.
- Madou, andalak sa xel tenga tek li, continu à me canaliser ma mère.
- Non Yaye na juguer nday fi, beugoumako guiss.
Au milieu de la foule, le gars se permet de me dire :
- Mangi deim mais jiapalni mak yaw ce n'est pas fini. Xamalni lo guiss rek mane la.
- Mani boulko yagal, sodé goor deug rek yeuwal niou mayéko légi mane ragalouma lolou, je réplique aussitôt.
- Jiaroul yakamti. Dinala door té sama loxo dula lal.
- Ragalouma lolou, je répond. Jiapalni fuñiu tassé dina tegu*l sa mame.
Je vois les gens l'amener.
VOUS LISEZ
Indestinés
RomanceL'amour est beau ...Oui, l'amour est beau, jusqu'au moment où il commence à devenir une épreuve. Aimer ne rime pas forcément avec la facilité. Aimer amène le plus souvent à faire des sacrifices, à accepter de souffrir ou encore, à optemperé face au...
