Titre de la partie

4.6K 227 5
                                    


☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*


🔘 *Wakhii Serigne TOUBA cii "SOPE saa Serigne".....*

🌼 *Serigne Malick Baasin Sy bi mu jaamoo sounou BOROOM ba aggue ci moom, sounou BOROOM da ni ko....:*

☘ *Agsi nga waayé djaaroo ci bountou bi. Daal di koy tektale "KOU TED KI" bimou gneuwé thii Serigne bii toog....Serigne bi ni ko...:*

☝🏾 *‹‹...Waatuul buyuuta min abwaabihaa...››*

⚜ *Serigne Malick niko :"Waa waaw !"....👉🏾Toog bamou yagg ni ko : "Xam naa ni li nga yor (Djoulli you baari maye wouko Djang Al Qur_aan maye wouko, ak Mbokk maye wouko).....Toogaat ba mou yagg ni ko : "Xam naa ko.....*

👌🏾 *Lii fii yaw Ak SOPP (BEUGG) rekka koy maye... 😍😍....KOU TEDD_KI ni ko : "Waa-waaw !"*

💫 *Loolu nak méngoo naak :*

🔰 *XULOOBU MAN LAM YUHIBBUUNII HALAA WAJALIN....👉🏾....WA LAA YULAXUUNA MAA RAAMUU WA LAAL BAABAA...*

🌐 *Thieuy MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL lii moo tax ba Serigne bii dadjalee gnénn ci magg gni ni leen : "na ku nekk wax li mou geuna Beugg gnou defal ko ko".....*

🔲 *Moom mou ni woon : "MBACKE DI LA GEUNA BEUGG REK".....*

💖 *Moo woné Yoon wi...*

💓 *Mooy Yoon wi...*

☝🏾 *...BAABUL MURIDIIN...*👌🏾

👌🏾 *Ken dou Maam dji Faal....👉🏾amoul Morom Faal te mate Borom....😍*

🙏🏾🙏🏾 🙏🏾🙏🏾*

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant