*✨...Yobalou Souba...✨*
⚜ *Ndéénkanék Serigne Touba...:*
🌼 *Serigne TOUBA "Xaada Laahou Maxtaara Lahoo"* mas naa wax *_Serigne Mouhadoul Moustapha «Al Karim»_*, lou mata deff deff naa ko, li ma léén di diggal mooy *_Ande téy Djarignanté_*
🔴Kon gnoun Taloubé yi nagnou goor goor lou si beuganté, fonkanté, di dibalanté, di soutouralanté, tay ta Serigne bi kepp takh ndax lolou kepp moy beugoup Serigne bi ci gnoune lougnou meuna djeufal serigne si Xidma ak Hadiya ta beuganté wougnou sougnou birr dougnou dimbalanté bougnou amé lougnou beugue si Serigne yitt, Serigne bi amagoul loumou beug si gnoun.
💫 *Serigne Moustapha Salihou* nééna *Serigne TOUBA* nééna képp kou adjou cii moom sougnou Borom moussal nako si *_"Safaarak Adouna ak bou Alaxira"_*.
*"Safaarak Adouna"* moy bagnantè, *"Safaarak Alaxira"* moy gna téxédi fala sen Borom djeumé ëleug. Koon app képp kou djapal dara sapp moromou Taloubé djapal ni ya djapp Serigne bi wayé sakk adjou ci Koubax ki weroul....Wa Salam
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall