*✨...Yobalou Souba...✨*
⚜ *Ndéénkanék Serigne Touba...:*
🔰 *Serigne TOUBA "Xaada Laahou Maxtaara Lahoo"* mas naa djokhe *Serigne Ridjale Seck* gnarri dàll nikoo bokhàl bén bii mou bokhe ko. Serigne yëkëti ba thiaa déss niko yóotou ko té bou béé wadd. Mou xam xéll ni sou yëkëtéé loxoom béé wadd, *"Serigne bi nikoo noo nou laa déméék Adouna"*.
👉Gnou amé sikk dégg ni kou topp adouna gui aki pognétaam, Serigne woon laa guinaaw ndax moom déy daraay Adina meussou ko yittél. Lolé yitt gnou meunéss ko méngua léé ak beuyitaam gogou sikk Ndénkaaném gou siiw bobou di *_"Koun-katimane"_* mouthiay wax naane:
*«Boul di djaay sak lérr djeundé koo ak Leundeume»*
*Wa Salaam....*🙏🏾🙏🏾
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall