Titre de la partie

2.2K 160 3
                                    



☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*


🔘 *Ayy Kadouy Ndénkaanéé ak fataali you ame solo taa mata bayi khélle.....👉🏾👂🏾*

🌐 *Lek lek nga aayé (tééré) nit dara mounila _"Louma neuboul yala doumako neub nit gni"_.....*

💫 *Wax djou mata moytou ndax beurina gnoukay doxée ba dootougnou am kérsa té kérsa kouko gnak déseetoo dara....*

☘ *Kep ko xamni Djeuf nga mba nga Wax loudoul nonou koula thia roy dinga gadou thiaa bakaar ba.....*

🔰 *Gnou bari dagnouy crée ay mbir nguir gnouleen thiay roy té moussiba rek laleni djoural....*

⚜ *Wax mom bou menta diarigne bagne koo wax mo gueune....*

🙏🏾🙏🏾 *_YALLA NAGNOU SERIGN BI NGUINDI TAA KHIRE GNOU SI BOPPAM AK SAKH CI "NDIGEUL YII"_*🤲🏾🤲🏾

📌 *Wa Salaam......🙏🏾🙏🏾*

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant