*✨...Yobalou Souba...✨*
🔘 *Waxi Serigne bii cii liggéyal ko...👉🏽👂🏼*
🔴'''Bim néké "Djolof"''' *Mame Cheikh Anta* '''masna kofaa séét ci muy déf sasu ngone jotéé ñu war ay fass dém séti tool ba ñuy wax''' *"Bustanul Harifina"*
📜'''Ba bén biss gnouy dém ba yam ci gnééti waxa-mbané, kén ka nék ci kaw di gorr gnaar gna nek fi souf di forr, Serigne Bi tolok gnom taxaw touti dadi dém wayé waxoul dara.'''
✒'''Bam déloucé dadi wo''' *Mame Cheikh Anta*, '''néko dama begone waxtane ak yow ci liggéyal ma, néko :''' *Bén Mourid bou xeuy liggéyal ma ngir Yallah ba ngone djote, ligéyyam boobé pésé nagn ko ak liggéyub Borom xam-xam bou liggéyal Yallah Djurom gnar fuki ate (70ans) murid ba wate ko, bulén sik né liggéyalma mo gueuna kawé guép Wilaya gougne déé fi woté.*
🔰'''La délé ci Sunu mame Adama ba sounou diamono dji liggéyalma yamoufi ak guén Djamu Yallah té bala ngéna xam lima wax «Yawmal Hiyamati» taxaw.'''
🙏🏼 *Nagnou xam lignou am, Fonkkou lignou am, mouy Serigne Touba 💖....Wa Saalaam👌🏼👌🏼*
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall