💠 *أعوذ بالله من الشيطن الرجيم.....بسم الله الرحمن الرحيم*🌼 *جرجف خادم رسول*
☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*
🔘 *Wakhii Cheikh Abdoul Ahad Mbacké......👉🏾👂🏾*
💫 *Daradja booko rignaanèe mou ndiatt la....*
☘ *Daradja dèesouko yootou,ndax nitt yi donilen mukk tay nguen wèg ma batax gnou wèg la,mom kay kouko yeloo rk djoxees lako.....*
🔰 *Serigne Malick Bassine Sy doone na wax ni : xar kanam xat na lool ba weg lèen ,ma fonk leen xadjou ci....*
🙏🏾🙏🏾 *_YALLA NAGNOU SERIGN BI NGUINDI TAA KHIRE GNOU SI BOPPAM AK SAKH CI "NDIGEUL YII"_*🤲🏾🤲🏾
📌 *Wa Salaam......🙏🏾🙏🏾
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall