Wakhi Borom

877 44 0
                                    

Serigne "TOUBA" xaada laahou lehoo, MaxTaareho'
Dafa binde waxni: "Wa Ass-bi lan-na hal-lay-na Rab-bi haa-fi-yatane
Wa Hab-lana khas-da fi daaray-ni Yal-lahou"

Wa ass bilane-na, Nanga sembeurteul, walla nanga diotalaal seuk,)
halyna, fi noun)gnep Rabi yaw sama borom, adji defa re-dji)
hafiyatane, mboub-boum diamou)

Mounnee "Halayna" lay wakh duma wax la "Yonente" Yàlla "Moussa" waxoon,
Nsakh "Yonente" Yàlla "Moussa" defa wakhon-ne (kal-la ina meh-yi, rab-bi za yeh-diini)
kerook, banga khame nee "Fir-hawna", deug-meul-nalaine ba djie-gue laine

guayam ya neko (in-na la moud-ra-kon), danagn nou diod de, "Moussa" nelain

kala houb in-na meh-yi, rabii, sa borom mingui andak man,
kon fatena gnamou and-nda lon,
motakh kou ted-ki ne mom donou fatte
ta dana Ann-ndak noun, ta dan-nou yob-balee
motakh mou-ne "Halayna" lay wakh, thi noun.

Wa hab, nanga may) lana, gnel gnou) Al khasda ak dioub)
Maname, (wa alla lahi khasdou sabiilii) nena khasdou sabili kokou am Yàlla, la dimbali

Ta moy ne thiouw-wou thia yoon wa dieum al-diana ba adiana,

Fi daarayeni thi yari keur yi, Bi mahna Adunna ak Al-lakhira) yal-lahou yaw yalla)

Yàlla nanou Yàlla defal deg ak top pou
amin incha allah
Bidiahi nabiiyil moustaphal karimi
mame borom touba cheikh ibrahima fall lamp
Baboul mourridou lahi fi dunya wal akhira amin!
DIEUREUDIEUFF Cheikh Saliou Mbacke

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant