*🔰...Magalou Diam ak Salam...🔰*

358 20 0
                                    

*✨...Yobalou Souba...✨*


🏵 *Guénee Djiguéne djou ame Magal...*

⚠ *Liy tax nitt ki am daayo fa Boromam ak ci kanami moroomam, du limuy lékk suur ko, du limuy naan maandiko, du limuy diwoo niin ko. Ci ay jikko la, ci aw mèlo la waayé ci ay jeuf yu wërr la*

🔰 *Lii Koutedki moko séedé ci wayjuram soxna Diarriatoulahi:*
'''Néena mooy jiguèen dji guena ragal yalla mooy ki guena fègou, mooy ki guena toroxlou ci loolou ci lama ko yalla tanalé nguir ma nek doome ci mom'''

☘ '''Massamba mba xamgueni xeweul yici adouna bi yeup ligueyou Soxna Diarraa, man samay mbir euleug yowmal hiyam lay fègne.'''


📌 *Soxna Diarra bok na ci liko may limou am mouy yité djou kawé, deugou tja ak am pass passoup dokh tja.*
*Ndax lou djitou mouy dem keur da messa tidji kamil yam ci aaya bi sunu Boroom di nane S.Mouhamed(as) moy yonent bi moudj watj(hatimou naby) mou dioy ni boudoul wone aaya bi mou mena waat ni danafa djour ab yonent.*
*Waya taxoul mou yem tja, taxoul yit mou bayekou. Bamou demé keur tja sen diayanté(defis) ya mok soxna Anta mou diayanté ni danafa am asamane mou tiime lep*
*Waya yit waxouko yemci waya da def lep louko ko mena may lep louko ko mena xagne mou watandikouko. Nguir matal diayantèm waya yit nguir samou kadoom, ndax gnom kat sen kadou lougnou fonkone la lol danou gnou wax mouk dici delou ci Kon nou jang ci ni nit dangay am yité djou kawé(ambition) ci lou baax, di tek say defi bop ci lou am ndiarigne té nangou tja dokh ci lep loula koy may té sori lep loulakay xagne, téy same say kadou*

🙏🏼 *Nagnou xam lignou am, Fonkkou lignou am, mouy Serigne Touba 💖....Wa Saalaam👌🏼👌🏼*

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant