✨ *Yobalou Souba*✨
💠 *أعوذ بالله من الشيطن الرجيم.....بسم الله الرحمن الرحيم*
🌼 *جرجف خادم رسول*
☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*
🔘 *Yéenéb woor Weerou koor:*
💫 *Ben yoon rek ngay yéné ni fasse nga yéné woor werr wi souniou né weer wi feegne na mooy eumbaalé weer wi yeup ndax koorou farata la*
🙏🏾🙏🏾 *Yalla nagnou sougnou Borom may fékké ak taal bagnou meuna diookhé Farata gui thia namou diguelé tamou nangoul gnou lépp lou gnou kosi djamou.....Di baalou gneup Akhe taa dilén balle akhe....🤲🏾🤲🏾*
📌 *Wa salamm.....
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall