Prorokhane

348 19 0
                                    

*✨...Yobalou Souba...✨*


🏵 *...Direction Magal Poroxane...*

📌 *Porokhane* '''tuurwi fimou agg''' *"Soxna sou Magg ci Soxna Diarra* '''moko fa AGGALEI!'''
*Porokhane* '''deuk la comme deuk yicci saloum, wayei nak soun koy deig bam meil ni,
SOXNASSI dafa deuk lou matt temeri att, barkeb LIGUEYOU SOKHNASEI wayei,'''
*POROKHANE " Soxna Diarra"* '''deifou fa lou eup niarry att walla thia lay yémme.

Motakh amna ben domou''' *Serigne "Matte dem"* kougnouy wax *"Serigne Mame Mor Deme" _«Nouni yatoul Khoufrane»_* '''bimou def ci "Sokhna Diarra" NGA khamni:
bamou deimei ca deuk ba la ko def!, Bokk na ci limou ko wakh!'''

*"Jam-houn KHAFIIROUNE hadja BAYTIKA ZAHIRANE, mine koulli NAAKHI-YATINE bi TOUY-BI JANAATI"*

'''Mboloo mou barri DAGNOUY HAdj si ci neig bi jouggei founei,
MASSALANE dagnou lay Ziara si, lako waral moy barkel bou LIGUEYAM barkel!

Kom nign ko khamei''' *"Sokhna Diarra"* '''Thiossa nam!''' *_Gollaré_* '''la joggei! ci Fuuta,'''
*Mbakke Baol* la djeukké djouggei *Mbacké Baol* gneuw *Nja kane!* guici wettou *Khourou MBAKKE.*

*Ahmadou Binta Kane* '''mi bokku ak''' *Sokhna Sally Kane Nday ak Baay mofa nékkone!*
*"Mame Jaara"* '''neik fa ab diir nieuw''' *Khourou MBAKKE.*

'''Jallo reim you rey yinouy deig yeip! ci doggom gou rey gogog BEUG-GAM gui lou baax,
loucci barrei barri''' *Khourou Mbacké* '''lako Deiffei.

sakket wowou gnouy faral di netali rek NGA khamni;
moy SAKKEIT wimou TEUYEI lool''' *"Mame Mor Anta Saly"*, '''ba beut set serigne bi gueinei ci neig bi jeum ci wanak wi nguir waath,
sein louy nioul mou laath soxna si niko manna MOUNIKO loy deif fi? Mouniko:
yama TEUYEI lo woon fi tei bayi lo woma, wax nagn nei DAKONEI feib ndokh wou dal CI-SA kaw Yalla nay barkei. AMINE,
mou fanan fa ba beut set KHOURROU MBAKKE la KHEIWEI woon.'''

🙏🏼 *Nagnou xam lignou am, Fonkkou lignou am, mouy Serigne Touba 💖....Wa Saalaam👌🏼👌🏼*

*🔰...A Suivre...🔰*

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant