Sa digueunté akk say wayjour
Say wadiour mom leip lougn la santeblou deupo ak diner def ko
Tei bougn waxei dolein youkhou.
Dolein khoxatal
Dii dokh seni ndigeul
Ndax yalla nena sa diguantei wadiour nanga ko rafetal
Sa digueunté akk sa serigne
Momit do wax ak mom di yeukati sa kadou mouy kawei do bok took ak mom si kaw do niam dara diko diox soy diouk nga moytou yeuketi souf bi
So toguei nga moytou diko xool tei bayi ko xeel
Nga bagn ko miin diko djiéguei
Do fanan ak mom loudoul lor
Do talal say tank si kanamam tok toguayou Talibei
Do retane ba say beugn si fegn mànam khaxatay
Sa digueunté akk sa deukandoo
Say deukando bougn xam sa gnak yitei boy togu nga moytou rossi bi dilen khégn leip lo xam ni dalen dii dérangei wala lo xamni beuguo niou def lako boul xalat def len ko
Nga diox len yitei sek ak niom diam diilén tibal niam ayy khew diox lein sen akh
Sa digueunté akk sa doom
Say doom mom leip lou waar si niom si waloum yerei
Diangue
Are léne
Samb léne
Yar léne
Lolou la wayjour yi sékk akk doom🙏🏾🙏🏾🙏🏾Di toubelatt ñeuppp
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
AléatoireDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall