Titre de la partie

3.2K 200 8
                                    


☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*


🔘 *Ndénkaanék Serigne TOUBA "Yakaari Diaam gnii.....👉🏾👂🏾*

🌐 *Koutéd kii néna......*

💫 *1°/ Xam-xam mooy: xam li Yalla Begg ak limou Beggul.....*

⚜ *2°/ Kérsa mooy: Rousa déf lou Boon.....*

💫 *3°/ Sant mooy: Djeffé Ndigeul yi.....*

⚜ *4°/ Séllal mooy: Djeuf téé Yalla taax.....*

💫 *5°/ Taabé mooy: di djokhé li nga meun.....*

⚜ *6°/ Noppi mooy: Bagna wax lou amoul Ndiarigne.....*

💫 *7°/ Léwét mooy: Bagna Fayou ag Toogn....*

⚜ *8°/ Mougne mooy: Teuyéé saa Bakkane baa dou djeum ci lou baaxoul.....*

💫 *9°/ Sammoonté mooy: Djeufee li nga xam walla nga né di moytou lou Leunt.....*


⚜ *10°/ Dégg - Dégglu mooy: di Féxéé xam lingay Djang mooy lan.....*


🙏🏾🙏🏾 *_YALLA NAGNOU SERIGN BI NGUINDI TAA KHIRE GNOU SI BOPPAM AK SAKH CI "NDIGEUL YII"_*🤲🏾🤲🏾

📌 *Wa Salam..🙏🏿

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant