✨ *Yobalou Souba*✨
💠 *أعوذ بالله من الشيطن الرجيم.....بسم الله الرحمن الرحيم*
🌼 *جرجف خادم رسول*
☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*
🔘 *Ndénkaanéb Serigne TOUBA Yakaari Diame gnii...gnéll Mouride bi Adjou si moom 👉🏾👂🏾*
⚜ *KOUTED kii nééna.....*
♻ *Yaw Mouride bi......*
🔰 *Nagua moyytou "Nguisstal" ak "Fèèn" tayy talion deugue; Kon di ngein amm akk lèèr.....*
🔰 *Nagua mousslou si "Rambathie", tay saxal toudou Yallah,tayy moytou lépp louy yakk xalaat, tayy moytou dieuf "Safane".....*
🔰 *Saa sou ngéén déffé "Bakkar"na nguein gaaww toup ko.....*
☝🏾☝🏾 *Ndénkaan li nak, soo ko djeufé di nga mouthieu te di nga am lépp loo beugg Adduna ak Allaaxira*
🙏🏾🙏🏾 *Yalla nagnou sougnou Borom maay dégge ak Topp barki Cheikhoul Khadim.....🤲🏾🤲🏾*
📌 *Wa Saalam....*
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall