*✨...Yobalou Souba...✨*
🔘 *Ndénkaanék Serigne TOUBA...👉🏼👂🏼*
🔰'''Moo jaa lu deefi defati? Moo jaa lu deefi waxati?
Moo jaa ku deefi royati? Bu kilifay moy ak a fo👉🏼Ku war a boole aw nitam Di waar'akay ful seeni gëm
Defu ko far boolew nitam Di moy'akay soow ak a fo🔰Addina yàqu na yaxeet Ku yabu wut barab bu wéet
Nekk fa tay jaamook a wéet Te sori kuy moy ak a fo👉🏼Addina yàqu na te kat Kilifa yoo ko yàq kat
Du séenu nit ko yàq kat Kilifa yoo fiy dox di fo🔰Ku yabu wub sa bunt kër Rekk te daw nelawi far
Nelaw a gën génn di lor Aw nit'akay lorook a fo👉🏼Ay am na nag ndegam nelaw Mu bon milee fiy tax a raw
Xamal ne kon ken dóotu raw Nelaw gënul lëf ndere fo.'''*🙏🏼.....S. Mbaye Diakhaté.....🙏🏼*
📌 *_A Suivre..._*
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
عشوائيDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall