Titre de la partie

664 27 0
                                    

✨ *Jootayou MOURIDE*✨

💠 *أعوذ بالله من الشيطن الرجيم.....بسم الله الرحمن الرحيم*

🌼 *جرجف خادم رسول*

*_⚜Jaar-Jaari Serigne TOUBA ⚜_*


♻Serigne bi daa diggalone magg gni gnou santhieu ci wétaam, bàyyi boroom kàttan yi mana liguéye yiiy tarbiyousi nékk ca tool ya. Deuk ba moudjou di deuk bi guena doundou ak djakkaam yéék daaraam yi ak djangoukaayu xam-xam yi.


🌐 *Al Quranoul Karim* biss bou nekk gnou wathiéé ko ci bountou keur Serigne bi gnénti yoon. Gnaari yoon guinnaw djouligue souba, bénn yoon guinnaw tisbar ak benen guinnaw takkoussan. Bou déé gouddi adjouma gnou wathié ko djouroom gnaari yoon. Mbootoum loo lou moom Yallah rakka ko xam, mooy djoullig farata goumou djoulli gou né tollook ab *Kaamil* bou gnou wathié.


              📌 *A suivre....

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant