*✨...Yobalou Souba...✨*
🔘 *_"Ndéénkanék Serigne bi cii toolou wayou Diamono dji.."_*
*🌍''Adduna, yëngu na'' waayé Lum yëngu-yëngu bou léen fattè waxi Serigne bi nagnou ci délou bou bagné laay Keufaaté Keuf gnou...:*
🌼 *Ndénkaané lii, Serigne bi migui ko dénkoon ak njàbootam bamouy dém ci Tukkib Guéédj gui, (1313H)*
🔰 '''Yéen samay gnoñe, naa ngéen fexe ba bou léen daray Àdduna djaral djaxasoog Bouri Àdduna yii, wala di djaxasoog Djaraaf yi (ministres).
Lépp lu léen leer ni man na Léen a yobbé ak moy Yàlla, wala ngéen foog ko thia, N naa ngéen ko moytu bou baax. Waaye lépp lou baax, lou ngéen djapp né di na takha am Ngërëmul Yàlla, naa ngéen ca Farlu séen kem kàttan.
Té ngéen di moytu ak Tayel, rawatina cii deff lou Baax.👉🏼 Naa ngéen xam ne nak, Àdduna akk li ci biiram, ak lum 《Neex-neex》 soo ko mé'nggalee (comparer) ak xéewal ya ca ÀL djana rek di nga xam ne lii ci Àdduna dou darra.
Waaye yit lii ci Àdduna ci ay 《Tiis aki Nakhaar》, soo ko xoole ci Mbugalum sawara rek, di nga xam ne li ci Àdduna du darra...'''*_🙏🏾Yallah nagnou Serigne bi Samou🙏🏾_*
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall