*✨...Yobalou Souba...✨*
🔘 *App Laabiré digganté Taloubé ak morom maa, gnélle toulou wayou Diamono ak djikko you yakhou yi gnou ci guiss gnou deffon ci app taxaw settlou. Tay gnou djeulon batt bobou gnouy wakh _《Teguine》_ Bismilah...👉🏼👂🏼*
♻ '''Yoon wi gua xamni moom la Serigne bi khaal mouy (Yoonou Mouriid) : Tèggiine djou werr, moko Lalal. Sërign Touba amoul moroom? (werna)
Waayé gnoune Taalibè yi warou gnoo am Moroom, ci wallou Tèggiine djou werr, kén warougne koo ëupp lè rawatina ci Waxiin, Serigne bi massoul wax, louy Rousloo ken, walla mou djëf ko. Kon nak gnoune Taalibè yi war na gnoo rooy ci moom, ndax moom dh l'Islaam rek lafi nékkaloon.'''⚜ Serigne Touba née na:
👉🏼 *_Na'ngeen ami Tèggiine, ci gneup ak ci lèpp, Te djoup tey djëffé Ndigëul di bayyi Téré yi: kou ci Dëngg ma wanla ginnaaw ndax douma àndak kou yakhou moukk._*
'''⚜Waxiin daa djar di Rafétall, wax bou andoul aki Tèggiine ay Loor rek lay djourrël Boroom.'''
*_🙏🏼Yallah nagnou Serigne bi saamou ta khirre gnou si boppam...Gnou saax ci ayy Ndigëulam baa lakh Ngëurëumam🙏🏼_*
VOUS LISEZ
Ayy kadouy ndénkané akk fatali
RandomDieureu dieufeuti Serigne Touba Djarama Mame Cheikh Ibrahima fall