Titre de la partie

1.3K 79 0
                                    

✨ *Yobalou Souba*✨


💠 *أعوذ بالله من الشيطن الرجيم.....بسم الله الرحمن الرحيم*

🌼 *جرجف خادم رسول*

☘ *السلام عليكم ورحمة اللّٰه*

🔘 *Ndénkaanéb Serigne TOUBA Yakaari Diame gnii...gnéll Mouride bi Adjou si moom 👉🏾👂🏾*

⚜ *KOUTED kii nééna.....*

💫 *Yaw Mouride bi, na nga beuggal sa mbokkoum Djoullit ligua beuggal sa bopp, soo ko defee di nga tabbi Al djana ci loudoul Hisaab....*

🔰 *Ta ngay teral gaan, doonte ab saay la sax.....*

💫 *Te ngay gnaanal sa gnaari waadjour ginnaaw djoullig Farata gounékk....*

🔰 *Te bul ignaané kenn, ndax kou ignaan kat dou féeté kaaw moukk.....*

💫 *Sou la nitt toognéé, na nga ko djéggal, ta boul fayantoo, te boul ko yéené yit lou boon.....*

🔰 *Yaw Mouride bi, képp kou la féeté kaw, dee ko teral, te di ko maggal......Képp koo féeté kaw, na nga ko yeureum te di ko mougnal.....Képp koo maaseel na nga ko def ni sa bopp....*

☝🏾☝🏾 *Ndénkaan li nak, soo ko djeufé di nga mouthieu te di nga am lépp loo beugg Adduna ak Allaaxira*


🙏🏾🙏🏾 *Yalla nagnou sougnou Borom maay dégge ak Topp barki Cheikhoul Khadim.....🤲🏾🤲🏾*

📌 *Wasalam🙏🏿🙏🏿

Ayy kadouy ndénkané akk fatali Où les histoires vivent. Découvrez maintenant